Dikoon episode 180

369 118 visualizzazioni426

    [☆ABONNEZ-VOUS ici☆] : it-new.net/client-PikiniProduction
    [☆Aimez aussi nos pages ici☆] :
    [☆FB☆]👉 www.fb.com/PikiniProductions
    [☆FB☆]👉 www.fb.com/Dikoon
    [☆Twitter☆] 👉twitter.com/PikiniProd
    [☆FB☆]👉 www.fb.com/PamaDieng
    [☆BLOGGER☆]👉 www.pikiniprod.blogspot.sn
    [☆WORDPRESS☆]👉 pikiniprod.wordpress.com/
    [☆WhatsApp☆]👉 [☆+221776626858☆]
    [☆PIKININFOS☆]👉it-new.net/onpl-PL7OYJbvZchhG06gRcgQTpYCsi_1h_Nyda
    [☆DIKOON☆]👉it-new.net/onpl-PL7OYJbvZchhFmlZEvZInQygwXi_s3Y_7j
    [☆PAMA DIENG☆]👉it-new.net/onpl-PL7OYJbvZchhGLVuJvAxipddB_mHoNGrIc
    [☆Minute☆du☆rire☆]👉it-new.net/onpl-PL7OYJbvZchhHg1i21jn1t_-iQPRFyCK7g
    Pikini Productions

    Pubblicato il 6 giorni fa

    Commenti

    1. Bakhé Sao

      sama dignité mayatou ma may sétane dikone bilay

    2. talibé Serigne saliou rek

      A khana nak bouniou dème ba 200 épisode dina diekh

    3. Eva Ndoye

      Dikoon yow tmt nek sa keur def say chaussure fermé merci rek pour sén cas😓😓😓

    4. AITA STEPHAN

      Khady nak ventre bi

    5. Eva Sima

      nèkhna machala merci wa pikini production mè birane sa bouche bi comme tiaya 10métre😋😋

    6. Fatou Ka

      Le mm sort k Elimane touré la police tue parole corruption

    7. Larissa Sagna

      Décidèrent biran com melakh rek

    8. Larissa Sagna

      On veut keulz et dada gnom gnoy khorom série bi

    9. møustaph Best Boyz

      Adduna lo guisssss deyyy dieuixx bamm deisss Dikon

    10. isco gaye

      Bilay nak warnguén diékhal nak

    11. Fatou Fatou

      Cva.s'est. Bien passé. Série

    12. Film Français《HD》

      Bonjour lire la suite

    13. Mbengue Adji

      Mane dikon nekhouma dara ak canamame bi thium mouy giongué ngiongué lou ni hah

    14. Sokhna anta Ndiaye

      vous étes ingrats cette série vous as satisfait depuis des mois vous pourriez étre plus gentille Non ...

    15. Fanta Diakite

      Commissariat bi d comme sabar bou tass Mère ma diama ioe do solution d Khady Sarr moy la solution 🤣 Ndeye Fily moy le cerveau 👍🏽

    16. Fanta Diakite

      Dikon mom xetou roujaaa you rouge yi tamit 🤣🤣🤣🙄 kegn lakey ba ak xetou fermer greffage yi kagn la xewi y’a Penda sax mola geuna brancher 🤣🤣🤣ana closure tamit 🤣

    17. Fanta Diakite

      Mane nkei keulz lA nam niii

    18. ouliita kardash

      Ani danseurs yi ak imam aaah eupena 😂 wa dikoon dagn ma yapp wala dagn ma mine

    19. Bbeih Oumyna Sary

      Hdjufsvkpigs

    20. Balde Demba

      Qui est le criminel entr le comis et le garde

    21. bebe Diakhate

      ma bagn commissaire bi

    22. arimaz

      Wala l'i plan ndeye fily la encor

    23. arimaz

      Si je comprend bien commissaire bu mo def exprès bayi clé bu si bureau bu pour wa dji évader niou def exprès auto police fir ko ngen fok ni li eupoul🤐😞🤔

    24. maman diop

      Birane day dedelou niou yombou ko si morgu ba mou diouk di dokh dokham lol 😂 no film bi mo nekh

    25. Carbaba Alpha

      sen film comme gnouy wakh ak Aÿ khalee

    26. Mayib Mbengue

      mai birane limoy deff daffa yombo trop

    27. ramatoulaye diallo

      dikoon attachion

    28. Kine Seck

      warna diex naaq

    29. Aby Sébor

      Birane:woyou bo guiss bandéy bayam

    30. Alassane mbaye

      Li kagn lay djiekh tamit😂

    31. bebe Diakhate

      damay lath nakh Tapha da apeulo

    32. Ndeye Thioune

      mane commissaire bii momay ray akk kanamame bii di gnangal

    33. Momy Mbacke

      Bravo ndeye fily

    34. mounass sow

      allo commissaire birane dêna😂😂😂

    35. Sylla Mamefaty

      Weuuuuu mane Limay lathie moy birane mom dou tay la déf crime di kidnapper nane bb moukhamed trafique d rin lolou yépou mou déf ko sujet gounko si lolou guéne di dougne ko mana téé Walla daguéne bal lolou yépou

    36. Mamy Ndao

      Li bakhna pour birane guaraou guaoulou de deou kanga rek

    37. Fatou kine Tall

      Basta siamo stancò

    38. tiverite Jolie

      Allo commissaire Birane dénaaaaa😂😁😂😂😃

    39. tiverite Jolie

      Ayywaaay dikoon dimbaliniou ak sa dale corossé yiiîi tu es chez toi do sol say thiarakhh you pooppp sagnsé mo diafé😁😂😂😂

    40. Cheikh Gueye

      Birane yaw khana meuno réglé

    41. Sidy Mbegniga

      Jaime baecoub khady sarr 😍😍😍😍😍😍😍

    42. Khadim Sylla Brésil chapeco

      Khady sarr yalla nako yalla may diame thi barkeb serigne touba wara to géne nak dagha wara nebato nak wakh baxol bet baxol

    43. Tima masallah sire jokkou kolle

      Ana maman dikoon AK pappam AK dada AK kélsi AK nabou AK mounass AK Balla AK pama AK aram AK njool AK aysatou Sarr 😅😅😘

    44. kadet djigo

      Ana dada way namnako lolou

    45. Tina diamé

      Legui commissaire delolll xalissou Tapha sarr bi vu k dangn la fayone kegn

    46. Medoune ndiaye

      Thiey ndeye fily.tjrs dangereuse.felicitation

    47. fatousha Babeel

      Dikoon change de look perruque tamitt 🤣🤣

    48. sokhna diarra diop

      Serie bo khamni amoul debut amoul fin chak fois denouement boubess ca dure depuis 2ans c abusé khawma kolen yap gnici amon dieukeur eumb ba weussine sen dom yagui doxi sen soxlo

    49. Belle Nana

      Un commissaire qui supplie pour arreter quelqu’un

      1. Belle Nana

        Qu’est ce qu il m enerve ce commissaire

    50. Couleursd'Afric styles Balle8

      Wa yén mba macky doulen emprisonner😊